Localisation updates for core messages from Betawiki (2008-01-30 17:11 CET)
[lhc/web/wiklou.git] / languages / messages / MessagesWo.php
1 <?php
2 /** Wolof (Wolof)
3 *
4 * @addtogroup Language
5 *
6 * @author Ibou
7 * @author SF-Language
8 * @author Siebrand
9 * @author SPQRobin
10 */
11
12 $fallback = 'fr';
13
14 $messages = array(
15 # User preference toggles
16 'tog-underline' => 'Rëddaatu lëkkalekaay yi :',
17 'tog-highlightbroken' => 'Wone leen <a href="" class="new">ñu xonq</a> lëkkalekaay yiy yóbbe ciy xët yu amul (lu ko moy : lu mel nii <a href="" class="internal">?</a>)',
18 'tog-justify' => 'Leru-maaseel xise yi',
19 'tog-hideminor' => 'Nëbb coppite yu néewal yi mujj',
20 'tog-extendwatchlist' => 'Jëfandikul limu toppte gi ñu gënal',
21 'tog-usenewrc' => 'Jëfandikul coppite yu mujj yi ñu gënal (JavaScript)',
22 'tog-showtoolbar' => 'Wone bànqaasu njëlu coppite bi (JavaScript)',
23 'tog-editondblclick' => 'Cuq cuqaatal ngir soppi aw xët (JavaScript)',
24 'tog-editsection' => 'Soppi ab xaaj jaare ko cib lëkkalekaay [Soppi]',
25 'tog-editsectiononrightclick' => 'Soppi ab xaaj cib cuqub ndeyjoor ci kojam (JavaScript)',
26 'tog-showtoc' => 'Wone tëralinu ne-ne yi (ngir xët yi ëpp 3 xaaj)',
27 'tog-rememberpassword' => 'Fattaliku sama baatujàll(cookie)',
28 'tog-editwidth' => 'Wone palanteeru coppite gi ci yaatuwaay bépp',
29 'tog-watchcreations' => 'Yokk ci sama limu toppte xët yi may sos',
30 'tog-watchdefault' => 'Yokk ci sama limu toppte xët yi may soppi',
31 'tog-watchmoves' => 'Yokk ci sama limu toppte xët yi may tuddaat',
32 'tog-watchdeletion' => 'Yokk ci sama limu toppte xët yi may dindi',
33 'tog-minordefault' => 'jàppe samay coppite ni yu néewal saa su ne',
34 'tog-previewontop' => 'Tegal wonendi ngi ci kaw balaa boyotu coppite gi',
35 'tog-previewonfirst' => 'wone wonendi gi su dee soppi gu njëkk la',
36 'tog-enotifwatchlistpages' => 'Yónne ma ab bataaxal su ab xët bu ne ci sama limu toppte soppikoo',
37 'tog-enotifusertalkpages' => 'Yònnee ma ab bataaxal su ay coppite amee ci sama xëtu waxtaanukaay',
38 'tog-enotifminoredits' => 'Yónne ma ab bataaxal donte coppite yu néew la ñu',
39 'tog-enotifrevealaddr' => 'Wone sama makkaan gu mbëjfeppal ci bataaxali yëgle yi',
40 'tog-shownumberswatching' => "Wone limu jëfandikukat yi'y topp wii xët",
41 'tog-externaleditor' => 'jëfandiku soppikat bu biti saa su ne',
42 'tog-externaldiff' => 'Jëfandiku ab méngalekaay bu biti saa su ne',
43 'tog-showjumplinks' => 'Doxalal lëkkalekaay yii di « joowin » ak « seet »',
44 'tog-uselivepreview' => 'Jëfandikul wonendi gu gaaw gi (JavaScript)',
45 'tog-forceeditsummary' => 'Wax ma ko suma mottaliwul ndefu boyotu sanni-kàddu bi',
46 'tog-watchlisthideown' => 'Nëbb samay coppite ci limu toppte gi',
47 'tog-watchlisthidebots' => 'Nëbb coppite yi bot yi def ci biir limu toppte bi',
48 'tog-watchlisthideminor' => 'Nëbb coppite yu néewal yi ci biir limu toppte bi',
49 'tog-ccmeonemails' => 'Yónnee ma ab duppi bu bataaxal yi may yónnee yeneen jëfandikukat yi',
50 'tog-diffonly' => 'Bul wone ndefu xët yi ci biir diffs yi',
51
52 'underline-always' => 'Saa su ne',
53 'underline-never' => 'Mukku',
54 'underline-default' => 'Aju ci joowukaay bi',
55
56 'skinpreview' => '(Wonendil)',
57
58 # Dates
59 'sunday' => 'dibéer',
60 'monday' => 'altine',
61 'tuesday' => 'talaata',
62 'wednesday' => 'alarba',
63 'thursday' => 'alxamis',
64 'friday' => 'ajjuma',
65 'saturday' => 'gaawu',
66 'sun' => 'dib',
67 'mon' => 'alt',
68 'tue' => 'tal',
69 'wed' => 'ala',
70 'thu' => 'alx',
71 'fri' => 'ajj',
72 'sat' => 'gaa',
73 'january' => 'Tamxarit',
74 'february' => 'Diggi-gamu',
75 'march' => 'Gamu',
76 'april' => 'Rakki-gamu',
77 'may_long' => 'Rakkaati-gamu',
78 'june' => 'Maami-koor',
79 'july' => 'Ndeyi-koor',
80 'august' => 'Baraxlu',
81 'september' => 'Koor',
82 'october' => 'Kori',
83 'november' => 'Diggi-tabaski',
84 'december' => 'Tabaski',
85 'january-gen' => 'Tamxarit',
86 'february-gen' => 'Diggi-gamu',
87 'march-gen' => 'Gamu',
88 'april-gen' => 'Rakki-gamu',
89 'may-gen' => 'Rakkaati-gamu',
90 'june-gen' => 'Maami-koor',
91 'july-gen' => 'Ndeyi-koor',
92 'august-gen' => 'Baraxlu',
93 'september-gen' => 'Koor',
94 'october-gen' => 'Kori',
95 'november-gen' => 'Diggi-tabaski',
96 'december-gen' => 'Tabaski',
97 'jan' => 'Tam',
98 'feb' => 'Dig',
99 'mar' => 'Gam',
100 'apr' => 'Rak',
101 'may' => 'Rakkaati',
102 'jun' => 'Maa',
103 'jul' => 'Nde',
104 'aug' => 'Bar',
105 'sep' => 'Koo',
106 'oct' => 'Kor',
107 'nov' => 'Diggi-ta',
108 'dec' => 'Tab',
109
110 # Bits of text used by many pages
111 'categories' => 'Wàll',
112 'pagecategories' => '{{PLURAL:$1|Wàll |Wàll }}',
113 'category_header' => 'Xët yi ci wàll gi « $1 »',
114 'subcategories' => 'Ron-wàll',
115
116 'mainpagetext' => "<big>'''Sampug MediaWiki gi sotti na . '''</big>",
117 'mainpagedocfooter' => 'Saytul [http://meta.wikimedia.org/wiki/Ndimbal:Ndefu Gindikaayu jëfandikukat bi] ngir yeneeni xibaar ci jëfandiku gu tëriin gi.
118
119 == Tambali ak MediaWiki ==
120
121 * [http://www.mediawiki.org/wiki/Manual:Configuration_settings Limu jumtukaayi kocc-koccal gi]
122 * [http://www.mediawiki.org/wiki/Manual:FAQ FAQ MediaWiki]
123 * [http://lists.wikimedia.org/mailman/listinfo/mediawiki-announce Limu waxtaan ci liy-génn ci MediaWiki]',
124
125 'about' => 'Ci mbirim',
126 'article' => 'Jukki',
127 'newwindow' => '(Day ubbeeku ci beneen palanteer)',
128 'cancel' => 'Neenal',
129 'qbfind' => 'Seet',
130 'qbbrowse' => 'Lemmi',
131 'qbedit' => 'Soppi',
132 'qbpageoptions' => 'Xëtuw tànneef',
133 'qbpageinfo' => 'Xëtuw xibaar',
134 'qbmyoptions' => 'Samay tànneef',
135 'qbspecialpages' => 'Xët yu solowu',
136 'moredotdotdot' => 'Ak yeneen...',
137 'mypage' => 'Samaw xët',
138 'mytalk' => 'Xëtu waxtaanuwaay',
139 'anontalk' => 'Waxtaan ak bii IP',
140 'navigation' => 'Joowiin',
141
142 'errorpagetitle' => 'Njuumte',
143 'returnto' => 'Dellu ci wii xët $1.',
144 'tagline' => 'Ab jukkib {{SITENAME}}.',
145 'help' => 'Ndimbal',
146 'search' => 'Seet',
147 'searchbutton' => 'Seet',
148 'go' => 'Ayca',
149 'searcharticle' => 'Ayca',
150 'history' => 'Jaar-jaaru xët wi',
151 'history_short' => 'Jaar-jaar',
152 'updatedmarker' => 'Ci samag nemmeeku gu mujj lañ ko soppi',
153 'info_short' => 'Xibaar',
154 'printableversion' => 'Seexam gu móoluwu',
155 'permalink' => 'Lëkkalekaay yu fi nekkandi',
156 'print' => 'Móol',
157 'edit' => 'Soppi',
158 'editthispage' => 'Soppi xët wii',
159 'delete' => 'Far',
160 'deletethispage' => 'Far wii xët',
161 'undelete_short' => 'Loppanti {{PLURAL:$1|1 coppite| $1 ciy coppite}}',
162 'protect' => 'Aar',
163 'protect_change' => 'soppi',
164 'protectthispage' => 'Aar wii xët',
165 'unprotect' => 'Aaradi',
166 'unprotectthispage' => 'Aaradil wii xët',
167 'newpage' => 'Xët wu bees',
168 'talkpage' => 'Xëtu waxtaanuwaay',
169 'talkpagelinktext' => 'Waxtaan',
170 'specialpage' => 'Xët wu solowu',
171 'personaltools' => 'Samay jumtukaay',
172 'postcomment' => 'Yokk ab sanni-kàddu',
173 'articlepage' => 'Gis jukki bi',
174 'talk' => 'Waxtaan',
175 'views' => 'Wonewiin',
176 'toolbox' => 'Boyotu jumtukaay yi',
177 'userpage' => 'Xëtu jëfandikukat',
178 'projectpage' => 'Wone xëtu sémb wi',
179 'imagepage' => 'Wone xëtu nataal wi',
180 'mediawikipage' => 'Wone xëtu bataaxal wi',
181 'templatepage' => 'Xool xëtu royuwaay wi',
182 'viewhelppage' => 'Xoolal xëtu ndimbal wi',
183 'categorypage' => 'Xool xëtu wàll yi',
184 'viewtalkpage' => 'Xëtu waxtaanuwaay',
185 'otherlanguages' => 'Yeneeni làkk',
186 'redirectedfrom' => '(Yoonalaat gu jóge $1)',
187 'redirectpagesub' => 'Xëtu yoonalaat',
188 'lastmodifiedat' => 'Coppite bu mujj bu xët wii $1 ci $2.<br />', # $1 date, $2 time
189 'viewcount' => 'Xët wii yër nañ ko $1 yoon.',
190 'protectedpage' => 'Xët wi dañ koo aar',
191 'jumpto' => 'Dem :',
192 'jumptonavigation' => 'Joowiin',
193 'jumptosearch' => 'Seet',
194
195 # All link text and link target definitions of links into project namespace that get used by other message strings, with the exception of user group pages (see grouppage) and the disambiguation template definition (see disambiguations).
196 'aboutsite' => 'Maanaam ci {{SITENAME}}',
197 'aboutpage' => 'Project:Maanaam ci',
198 'bugreports' => 'Ngértey njuumte yi',
199 'bugreportspage' => 'Project:Ngértey njuumte',
200 'copyright' => 'Ndef gi jàppandi na ci $1.',
201 'currentevents' => 'Luy xew',
202 'currentevents-url' => 'Project:Luy xew',
203 'disclaimers' => 'Ay aartu',
204 'disclaimerpage' => 'Project:Aartu yu daj',
205 'edithelp' => 'Ndimbal',
206 'edithelppage' => 'Help:Nooy soppee aw xët',
207 'helppage' => 'Help:Ndimbal',
208 'mainpage' => 'Xët wu njëkk',
209 'portal' => 'Askan',
210 'portal-url' => 'Project:Xët wu njëkk',
211 'sitesupport' => 'Joxe ag ndimbal',
212 'sitesupport-url' => 'Project:Joxe ag ndimbal',
213
214 'badaccess' => 'Njuumte ci ndigël gi',
215 'badaccess-group0' => 'Amoo ay sañ-sañ yu doy ngir man a def li nga bëgg a def.',
216 'badaccess-group1' => 'jëf ji ngay jéem a def ñi bokk ci mbooloo mii $1 rek ñoo ko man.',
217 'badaccess-group2' => 'Jëf ji ngay jéem a def, jëfandikukatu mbooloo yii $1 rek ñoo ko man.',
218 'badaccess-groups' => 'Jëf ji ngay jéem a def, jëfandikukatu mbooloo yii $1 rek ñoo ko man.',
219
220 'ok' => 'waaw',
221 'retrievedfrom' => 'Ci « $1 » lañ ko jële',
222 'youhavenewmessages' => 'Am nga $1 ($2).',
223 'newmessageslink' => 'Bataaxal yu bees',
224 'newmessagesdifflink' => 'Coppite gu mujj',
225 'youhavenewmessagesmulti' => 'Am nga ay bataaxal yu bees ci $1',
226 'editsection' => 'Soppi',
227 'editold' => 'Soppi',
228 'editsectionhint' => 'Soppi bii xaaj : $1',
229 'toc' => 'Tëralin',
230 'showtoc' => 'Wone',
231 'hidetoc' => 'Nëbb',
232 'thisisdeleted' => 'Da ngaa bëgg a wone walla loppanti $1 ?',
233 'viewdeleted' => 'Xool $1 ?',
234 'restorelink' => '{{PLURAL:$1|1 coppite lañ far |$1 ciy coppite lañ far}}',
235 'feedlinks' => 'Wal',
236 'feed-invalid' => 'Gii xeetu wal baaxul.',
237 'site-rss-feed' => 'Walu RSS gu $1',
238 'site-atom-feed' => 'Walu Atom gu $1',
239 'page-rss-feed' => 'Walu RSS gu "$1"',
240 'page-atom-feed' => 'Walu Atom gu "$1"',
241
242 # Short words for each namespace, by default used in the namespace tab in monobook
243 'nstab-main' => 'Jukki',
244 'nstab-user' => 'Xëtu jëfandikukat',
245 'nstab-special' => 'Solowu',
246 'nstab-project' => 'Manaam ci',
247 'nstab-image' => 'Dencukaay',
248 'nstab-mediawiki' => 'Bataaxal',
249 'nstab-template' => 'Royuwaay',
250 'nstab-help' => 'Ndimbal',
251 'nstab-category' => 'Wàll',
252
253 # Main script and global functions
254 'nosuchaction' => 'Jëf ji xameesu ko',
255 'nosuchactiontext' => 'Jëf ji ñu biral ci bii URL wiki bi xammeewu ko.',
256 'nosuchspecialpage' => 'Xët wu solowu wu amul',
257 'nospecialpagetext' => 'Da nga laaj aw xët wu solowu wu wiki gi xamul. Ab limu xët yu solowu yépp ma nees na koo gis ci [[{{ns:special}}:Specialpages]]',
258
259 # General errors
260 'error' => 'Njuumte',
261 'noconnect' => 'Jéggalu! ngir ay tolof-tolofi xarala, fi mu ne nii duggu gi jàppandiwul. <br />
262 $1',
263 'nodb' => 'Falug dattub njoxe bii di $1 antuwul',
264 'laggedslavemode' => 'Moytul, wii xët man naa bañ a man dékku coppite yi ñu mujjee def',
265 'readonly' => 'Dattub njoxe li dañ kaa caabi',
266 'enterlockreason' => 'Biralal ngirtey tëj gi ak diir bi mu war a amee',
267 'readonlytext' => 'Les ajouts et mises à jour sur la base de données sont actuellement bloqués, probablement pour permettre la maintenance de la base, après quoi, tout rentrera dans l’ordre.
268 L’administrateur ayant verrouillé la base de données a donné l’explication suivante :$1',
269 'internalerror' => 'Njuumte gu biir',
270 'internalerror_info' => 'Njuumte gu biir : $1',
271 'filecopyerror' => 'Duppig dencukaay bii di « $1 » jëm « $2 » antuwul.',
272 'filerenameerror' => 'Tuddewaatug « $1 » niki « $2 » antuwul.',
273 'filedeleteerror' => 'Farug dencukaay bii di « $1 » antuwul.',
274 'directorycreateerror' => 'Sosug wayndare bii di « $1 » antuwul.',
275 'filenotfound' => 'Gisug dencukaay bii di « $1 » antuwul.',
276 'fileexistserror' => 'Mbind mi ci wii wayndare « $1 » antuwul : dencukaay bi am na ba noppi',
277 'badarticleerror' => 'Gii jëf defuwul ci wii xët.',
278 'cannotdelete' => 'Farug xët walla dencukaay bi nga joxoñ antuwul. (xayna far gi am na keneen ku ko def ba noppi.)',
279 'badtitle' => 'Koj bu baaxul',
280 'badtitletext' => 'Kojug xët wi nga laaj baaxul, amul dara walla day di kojjug diggantelàkk walla diggantesémb yu seen lonkoo baaxul. Xayna it dafa am benn walla ay araf yu ñu manuta jëfandikoo cib koj.',
281 'querypage-no-updates' => 'Yeesal yu xët wii dañ leen a doxadil fi mu ne nii. Xibaar yi ne fii ci suuf beesuñu.',
282 'viewsource' => 'Xool gongikuwaayam',
283 'viewsourcefor' => 'ngir $1',
284 'actionthrottled' => 'Jêf ju digal',
285 'actionthrottledtext' => 'Ngir xeex spam yi, jëf ji nga namm a def dañ kaa digal ci yoon yoo ko man ci benn diir bu gatt. Te mel na ne romb nga boobu dig. Jéemaatal fii aki simili.',
286 'protectedpagetext' => 'Wii xêt dañ kaa aar ngir bañ ag coppiteem.',
287 'viewsourcetext' => 'Man ngaa xool te duppi li nekk ci bii jukki ngir man cee liggéey :',
288 'cascadeprotected' => 'Xët wii dañ kaa aar ndaxte daa ëmbu ci {{PLURAL:$1|xët wi toftal|xët yi toftal}}, di yu ñu aar :
289 $2',
290 'namespaceprotected' => "Amoo sañ-sañu soppi xët yi ne ci bii barabu tur « '''$1''' ».",
291 'customcssjsprotected' => 'Amoo sañ-sañu soppi wii xët ndaxte daa ëmb ay tànneefi yeneeni jëfandikukat.',
292 'ns-specialprotected' => 'Xët yi ne ci bii barabu tur « {{ns:special}} » kenn maneesu leen a soppi.',
293 'titleprotected' => 'Koj bii [[User:$1|$1]] moo ko aar ngir bañ sosteefam. Ngirte li mu joxe mooy ne <i>« $2 »</i>.',
294
295 # Login and logout pages
296 'logouttitle' => 'Génnu',
297 'logouttext' => "'''Fi mu nekk nii génn nga.'''<br />
298 Man ngaa wéy di jëfandikoo {{SITENAME}} ci anam buñ la dul xamme walla duggeewaat ak wenn tur wi walla ak weneen.",
299 'welcomecreation' => '== Dalal-jamm, $1 ! ==
300
301 Sag mbindu sotti na. Bul fatte soppi say tànneef ni nga ko bëggee ci {{SITENAME}}.',
302 'loginpagetitle' => 'Duggu',
303 'yourname' => 'Sa turu jëfandikukat',
304 'yourpassword' => 'Sa baatujàll',
305 'yourpasswordagain' => 'Bindaatal sa baatujàll',
306 'remembermypassword' => 'Fattaliku sama baatujàll ci bii nosukaay',
307 'yourdomainname' => 'Sa barab',
308 'loginproblem' => '<b>Jafe-jafey xammeeku.</b><br />Jéemaatal!',
309 'login' => 'xammeeku',
310 'loginprompt' => 'Faw nga doxal cookie yi ngir man a duggu ci {{SITENAME}}.',
311 'userlogin' => 'Bindu/Duggu',
312 'logout' => 'Génnu',
313 'userlogout' => 'Génnu',
314 'notloggedin' => 'Duggoo de',
315 'nologin' => 'Binduwoo ? $1.',
316 'nologinlink' => 'Sos am sàq',
317 'createaccount' => 'Bindu',
318 'gotaccount' => 'Bindu nga ba noppi? $1.',
319 'gotaccountlink' => 'Xammeeku',
320 'createaccountmail' => 'Jaare ko ci m-bataaxal',
321 'badretype' => 'Baatujàll yi nga bind yemuñu.',
322 'userexists' => 'Turu jëfandikukat bi nga bind am na boroom ba noppi. Tànnal beneen.',
323 'youremail' => 'Sa màkkaanub m-bataaxal :',
324 'username' => 'Turu jëfandikukat :',
325 'uid' => 'Limu Jëfandikukat :',
326 'yourrealname' => 'Sa tur dëgg*',
327 'yourlanguage' => 'Làkk :',
328 'yournick' => 'Xaatim ngir say waxtaan :',
329 'badsiglength' => 'Sa xaatim daa gudd lool: guddaay bi ëpp mooy $1 araf.',
330 'email' => 'Màkkaanub m-bataaxal',
331 'prefs-help-realname' => 'Sa tur dëgg day lu jaasadi: soo ko ci mamme duggal it dañ koy jëfandikoo rek ngir moomalela say cëru (li ngay indi).',
332 'loginerror' => 'Njuumte ci xammeeku gi',
333 'prefs-help-email' => 'Sa màkkaanub m-bataaxal day lu jaasadi: day tax rek ñu man laa yónne ab bataaxal jaare ko ci sa xëtu jëfandikukat walla yónne la baatujàll bu bees soo ko fattee, te du tax sa màkkaan gisuwu.',
334 'prefs-help-email-required' => 'Laaj na ab màkkaanub m-bataaxal',
335 'nocookiesnew' => 'Sàqum jëfandikukat mi sosu na, waaye duggu gi antuwul. {{SITENAME}} day jëfandikoo ay cookie ngir duggu gi, waaye da nga leen doxadil. Doxal leen ci sa joowukaay te duggaat ak sa tur ak sa baatujàll bi nga sos.',
336 'nocookieslogin' => '{{SITENAME}} day jëfandikoo ay cookie ngir dugg gi, te yaw say cookies dañoo doxadi. Doxal leen ci joowukaay te jéem a duggaat.',
337 'noname' => 'Bindoo turu jëfandikukat bi baax.',
338 'loginsuccesstitle' => 'Sag xammeeku jàll na',
339 'loginsuccess' => 'Léegi nag duggu nga ci {{SITENAME}} yaay « $1 ».',
340 'nosuchuser' => 'Amul benn jëfandikukat bu tuddu « $1 ». Xoolaatal bu baax mbindiin mi walla nga sos meneen sàqum jëfandikukat.',
341 'nosuchusershort' => 'Amul benn jëfandikukat bu tuddu « $1 ». Xoolaatal mbidiin mi.',
342 'nouserspecified' => 'Laaj na nga tànn ab turu jëfandikukat',
343 'wrongpassword' => 'Bii baatujàll baaxul. Jéemaatal.',
344 'wrongpasswordempty' => 'Duggaloo ab baatujàll, jéemaatal.',
345 'passwordtooshort' => 'Sa baatujàll dafa gatt. War naa am $1 araf lumu néew néew te itam wute ag sa turu jëfandikukat.',
346 'mailmypassword' => 'Yónnee ma ab baatujàll bu bees',
347 'passwordremindertitle' => 'Sa baatujàll bu bees ci {{SITENAME}}',
348 'passwordremindertext' => 'Kenn(xayna yaw la) ku am bii màkkaanu IP $1 moo laaj ngir ñu yónne ko ab baatujàll bu bees ngir duggam ci {{SITENAME}} ($4).
349 Baatujàll bu jëfandikukat bii di « $2 » léegi mooy « $3 ».
350 Di la digal rekk nga duggu te soppi baatujàll bi ci ni mu gën a gaawee.
351
352 Soo doonul ki biral bii laaj, walla fattaliku nga sa baatujàll bu njëkk ba, te nammatoo kaa soppi, man ngaa tankamlu bii bataaxal te wéy di jëfandikoo baatujàll bu yàgg ba.',
353 'noemail' => 'Bii jëfandikukat « $1 » amufi benn màkkaanub m-bataaxal.',
354 'passwordsent' => 'Ab baatujàll bu bees yónnee nañ ko ci màkkaanub m-bataaxal bu jëfandikukat bii di « $1 ». Jéemal a duggaat soo ko jotee.',
355 'blocked-mailpassword' => 'Ngir faggandiku ci yaq gi, ku ñu téye sa màkkaanu IP ba doo man a soppi dara, doo man a yónneelu baatujàll bu bees.',
356 'eauthentsent' => 'Yónnee nañ la ab m-bataaxalub dëggal ci màkkaanub m-bataaxal bi nga joxe. Balaa ñuy yónnee beneen m-bataaxal ci bii màkkaan, fawwu nga topp tektal yiñ la jox ngir dëggal ni yaa moom bii màkkaan.',
357 'throttled-mailpassword' => 'Ab m-bataaxal bu lay fattali sa baatujàll yónnee nañ la ko am na $1 waxtu. Ngir moytu ay say-sayee, benn m-bataaxalu fattali rek lañ lay yónnee ci diiru $1 waxtu.',
358 'mailerror' => 'Njuumte ci yónneeb m-bataaxal bi : $1',
359 'acct_creation_throttle_hit' => 'Jéggalu, bindu nga $1 yoon. manoo binduwaat',
360 'emailauthenticated' => 'Ci $1 nga dëggal sa màkkaanu m-bataaxal.',
361 'emailnotauthenticated' => 'Dëggalagoo sa m-bataaxal. Duñ la man a yónne benn m-bataaxal bu aju ci yii ci suuf.',
362 'emailconfirmlink' => 'Dëggalal sa m-bataaxal',
363 'invalidemailaddress' => 'Daytalub m-bataaxal bi baaxul. Duggalal beneen walla nga bàyyi tool bi ne këmm',
364 'accountcreated' => 'léegi bindu nga.',
365 'accountcreatedtext' => 'Mbindug jëfandikukat bii di $1 jàll na',
366 'createaccount-title' => 'Sosum sàq ci {{SITENAME}}',
367 'createaccount-text' => 'Kenn ($1) ku sos am sàq ci {{SITENAME}} te tuddu $2
368 ($4). Baatujàll bu « $2 » mooy « $3 ». Li gën mooy nga duggu ci teel te soppi baatujàll bi.
369
370 Jéelaleel bataaxal bii su fekkee ci njuumte nga sosee mii sàq.',
371 'loginlanguagelabel' => 'Làkk : $1',
372
373 # Password reset dialog
374 'resetpass' => 'Neenal baatujàll bi',
375 'resetpass_header' => 'Neenalug baatujàll',
376 'resetpass_submit' => 'Soppil baatujàll bi te duggu',
377 'resetpass_success' => 'Coppiteeg baatujàll bi antu na : Yaa ngi duggu...',
378 'resetpass_forbidden' => 'Baatujàll bi manoo kaa soppi ci {{SITENAME}}',
379
380 # Edit page toolbar
381 'bold_sample' => 'Duufal mbind mi',
382 'bold_tip' => 'Duufal mbind mi',
383 'italic_sample' => 'Wengal mbind mi',
384 'italic_tip' => 'Wengal mbind mi',
385 'link_sample' => 'Koju lëkkalekaay bi',
386 'link_tip' => 'Lëkkalekaay yu biir',
387 'extlink_sample' => 'http://www.example.com koju lëkkalekaay bi',
388 'extlink_tip' => 'Lëkkalekaay yu biti (bul fattee jiital http://)',
389 'headline_sample' => 'Ron-koj',
390 'headline_tip' => 'Ron-koj 2° dayoo',
391 'nowiki_sample' => 'Duggalal fii mbind mi ñu daytalul',
392 'nowiki_tip' => 'Jéelaleel mbindinu wiki',
393 'image_tip' => 'Nataal bu roofu',
394 'sig_tip' => 'Xaatimee waxtu wi',
395 'hr_tip' => 'Buum bu tëdd (bul ci ëppal)',
396
397 # Edit pages
398 'summary' => 'Koj&nbsp;',
399 'subject' => 'Tëriit/koj',
400 'minoredit' => 'Coppite yu néewal',
401 'watchthis' => 'Topp xët wii',
402 'savearticle' => 'Duggal coppite yi',
403 'preview' => 'Wonendi',
404 'showpreview' => 'Wonendi',
405 'showlivepreview' => 'Xool bu gaaw',
406 'showdiff' => 'Gis li ma soppi',
407 'anoneditwarning' => "'''Moytul :''' Duggoo. Sa màkkaanub IP di nañ ko duggal ci jaar-jaaru xët wii.",
408 'missingsummary' => "'''Moytul :''' Defoo ab tënk ci coppite yi nga amal. Soo cuqaate ci «Duggal coppite yi», say coppite di nañ duggu te duñ am koj, maanaam duñ xam loo soppi.",
409 'missingcommenttext' => 'Di la sakku nga duggal ab tënk ci-suuf, jërëjëf.',
410 'missingcommentheader' => "'''Fattali :''' Joxoo ab koj say coppite. Soo cuqaate ci «duggal coppite yi», di nañ leen duggal te duñ am koj.",
411 'summary-preview' => 'Wonendi koj gi',
412 'subject-preview' => 'Wonendi gu tëriit/koj',
413 'blockedtitle' => 'Bii jëfandikukat dañ kaa téye',
414 'blockedtext' => '<big>\'\'\'Sa sàqum jëfandikukat walla sa màkkaanu IP dañ leen téye .\'\'\'</big>
415
416 Ki def téye gi mooy $ te lii mooy ngirte li : \'\'$2\'\'.
417
418 Man ngaa jokkoo ak $1 walla kenn ci [[{{MediaWiki:Grouppage-sysop}}|yorekat yi]] ngir ngeen ma cee waxtaan.
419
420 Te nga jàpp ne jumtukaay bii di "yónne bataaxal bii jëfandikukat" du dox su fekke duggaluloo ab m-bataaxal ci say [[Special:Preferences|tànneef]]. Sa màkkaanu IP mooy $3, xammeekaayu téye gi moy #$5. Di la sakku nga duggal leen fépp fuñ la leen laajee
421 * Ndorteelu déye gi : $8
422 * Jeexantalu téye gi : $6
423 * Sàq mi ñu téye : $7.',
424 'autoblockedtext' => 'Bii màkkaanu IP dañ kaa téye ndaxte da nga koo bokk ak beneen jëfandikukat, te moom it $1 moo ko téye $1.
425 Te lii mooy ngirte yi mu joxe :
426
427 :\'\'$2\'\'
428
429 * Ndoorteelu téye gi: $8
430 * Njeexintalu téye gi : $6
431
432 Man ngaa jookkook $1 walla ak kenn ci [[{{MediaWiki:Grouppage-sysop}}|yorekat yi]] ngir waxtaan ci téye gi.
433
434 Su fekkee joxe nga ab màkkaanu m-bataaxal ci say [[Special:Preferences|tànneef]] te terewuñula nga jëfandikoo ko, man ngaa jëfandikoo jumtukaay bii di "yónne ab m-bataaxal bii jëfandikukat" ngir jookkook ab yorekat.
435
436 Sa màkkaanu IP mooy $3 xammeekaayu téye gi mooy #$5. Di la sakku nga joxe leen fuñ la leen laajee.',
437 'blockededitsource' => "Ndefug '''say coppite''' yi nga def fii '''$1''' mooy lii ci suuf:",
438 'whitelistedittitle' => 'Laaj na nga bindi ngir mana soppi ndef gi',
439 'whitelistedittext' => 'Da ngay wara doon $1 ngir am sañ-sañu soppi ngef gi.',
440 'whitelistreadtitle' => 'Laaj na nga bindu ngir mana jàng ndef gi',
441 'whitelistreadtext' => 'Ngir man a jàng ëmbit li, laaj na nga [[Special:Userlogin|duggu]].',
442 'whitelistacctitle' => 'Amoo sañ-sañu bindu.',
443 'whitelistacctext' => 'Ngir nga man a sos yeneeni sàq ci bii wiki, laaj na nga [[Special:Userlogin|duggu]] te it xaar ba am sañ-sañ yi mu laaj.',
444 'confirmedittitle' => 'Laaj na nga dëggal sa m-bataaxal ngir man a soppi xët yi',
445 'confirmedittext' => 'Ngir man a soppi dara faaw nga dëggal sa m-bataaxal. Ngir kocc-koccal walla dëggal sa màkkaan demal ci say [[Special:Preferences|tànneef]].',
446 'nosuchsectiontitle' => 'Xaaj bi amul',
447 'nosuchsectiontext' => 'Da nga doon jéema soppi ab xaaj bu amul. Segam bii xaaj $1 amul, say coppite duñ leen denc.',
448 'loginreqtitle' => 'Laaj na nga bindu',
449 'loginreqlink' => 'Duggu',
450 'loginreqpagetext' => 'Faw nga $1 ngir gis yeneen xët yi.',
451 'accmailtitle' => 'Baatujàll bi yónne nañ ko.',
452 'accmailtext' => 'Baatujàll bu « $1 » yónne nañ ko ci bii màkkaan $2.',
453 'newarticle' => '(Bees)',
454 'newarticletext' => "Da ngaa topp ab lëkkalekaay buy jëme ci aw xët wu amagul. ngir sos xët wi léegi, duggalal sa mbind ci boyot bii ci suuf (man ngaa yër [[{{MediaWiki:Helppage}}|xëtu ndimbal wi]] ngir yeneeni xamle). Su fekkee njuumtee la fi indi cuqal ci '''dellu''' bu sa joowukaay.",
455 'anontalkpagetext' => "---- ''Yaa ngi ci xëtu waxtaanuwaayu ab jëfandikukat bu kenn-xamul, bu bindoogul walla du jëfandikoo sàqam. Kon ngir xamme ko faaw nga jëfandikoo màkkaanub IP wan. Te màkkaanub IP jëfandikukat yu bari man nañ ka bokk. Su fekkee jëfandikukat bu kenn-xamul nga, te nga gis ne dañ laa féetale ay sànni-kaddu yoo moomul, man ngaa [[Special:Userlogin|bindu walla duggu]] ngi benn jaxase bañatee am ëllëg .''",
456 'noarticletext' => 'Fi mu ne ni amul benn mbind ci xët wii; man ngaa [[{{ns:special}}:Search/{{PAGENAME}}|tambli ab seet ci koju xët wii]] walla [{{fullurl:{{FULLPAGENAME}}|action=edit}} soppi xët wii].',
457 'userpage-userdoesnotexist' => 'Bii sàqum jëfandikukat « $1 » du bu ku bindu. Seetal bu baax ndax da ngaa namma sos walla soppi wii xët.',
458 'clearyourcache' => "'''Karma :''' Soo dence xët wi ba noppi, faaw nga bës ci si sa arafukaay yii di toftal, te nga bàyyi xel ci joowukaay bi ngay jëfandikoo : '''Mozilla / Konqueror / Firefox :''' ''Shift-Ctrl-R'', '''Internet Explorer / Opera :''' ''Ctrl-F5'', '''Safari :''' ''Cmd-R''.",
459 'token_suffix_mismatch' => '<strong>Votre édition n’a été acceptée car votre navigateur a mélangé les caractères de ponctuation dans l’identifiant d’édition. L’édition a été rejetée afin d’empêcher la corruption du texte de l’article. Ce problème se produit lorsque vous utilisez un proxy anonyme à problème.</strong>',
460 'editing' => 'Coppiteg $1',
461 'editinguser' => 'Coppiteg $1',
462 'yourtext' => 'Sa mbind',
463 'nonunicodebrowser' => '<strong>Attention : Votre navigateur ne supporte pas l’unicode. Une solution temporaire a été trouvée pour vous permettre de modifier en tout sûreté un article : les caractères non-ASCII apparaîtront dans votre boîte de modification en tant que codes hexadécimaux. Vous devriez utiliser un navigateur plus récent.</strong>',
464 'editingold' => '<strong>Attention : vous êtes en train de modifier une version obsolète de cette page. Si vous sauvegardez, toutes les modifications effectuées depuis cette version seront perdues.</strong>',
465 'yourdiff' => 'Wuute',
466 'cascadeprotectedwarning' => '<strong>MOYTUL : Xët mii dañ kaa aar ba nga xamne [[{{MediaWiki:Grouppage-sysop}}|yorkat yi]] rek ñoo koy mana soppi. Kaaraange googu dañ kaa def ndaxte xët mii dañ kaa boole ci {{PLURAL:$1|am xët mu ñu aar|ay xët yu ñu aar}} ak « kaaraange cig toppante » te dañ kaa taal.</strong>',
467 'templatesused' => 'Royuwaay yi nekk ci mii xët :',
468 'templatesusedpreview' => 'Royuwaay yi nekk ci gii wonendi :',
469 'template-protected' => '(aar)',
470
471 # Account creation failure
472 'cantcreateaccounttitle' => 'sag mbindu Mënu la nekk .',
473
474 # History pages
475 'viewpagelogs' => 'Xool yéenekaayu xët mii',
476 'nohistory' => 'Xët wii amulub jaar-jaar.',
477 'cur' => 'Xibaar',
478 'next' => 'tegu',
479 'histlast' => 'Li ñu mujje indi',
480
481 # Search results
482 'noexactmatch' => "'''Amul wenn xët wu tudd « $1 » wu am.''' man ngaa [[:$1|sakk xët wi]].",
483 'nextn' => '$1 yi tegu',
484 'viewprevnext' => 'Xool ($1) ($2) ($3).',
485
486 # Preferences page
487 'mypreferences' => 'Samay tànneef',
488 'changepassword' => 'Coppiteeg baatu duggu bi',
489 'skin' => 'Apparence',
490 'prefs-watchlist' => 'Limu toppte',
491 'prefs-watchlist-days' => 'Limu bes yi nga koy ba ci sa limu toppte :',
492 'saveprefs' => 'Duggal tànneef yi',
493 'oldpassword' => 'Baatu duggu bu yagg :',
494 'newpassword' => 'Baatu duggu bu bees :',
495 'retypenew' => 'Dëggalal baatu dugg bu bees bi :',
496 'searchresultshead' => 'Seet',
497 'recentchangesdays' => 'Limu bes yi nga koy wone ci coppite yu mujj yi :',
498 'recentchangescount' => 'Limu coppite yi ngay wone ci coppite yu mujj yi :',
499 'savedprefs' => 'Tànneey yi duggal nañ leen.',
500 'allowemail' => 'ndigëlël yeneeni jëfëndikookat mën laa yòonnee bataaxal',
501
502 # User rights
503 'userrights-lookup-user' => 'Yorinu yelleefu jëfëndikookat',
504 'userrights-user-editname' => 'Duggal am turu jëfëndikookat :',
505 'editusergroup' => 'Coppiteg mbooloo Jëfëndikookat yi',
506 'userrights-editusergroup' => 'Soppi mbooloo yu jëfëndikookat bi',
507 'saveusergroups' => 'Duggal mbooloo jëjëndikookat yi',
508 'userrights-groupsmember' => 'Way-bokk gu:',
509 'userrights-groupsavailable' => 'Mbooloo yi jappandi:',
510 'userrights-groupshelp' => 'Tannal mbooloo yi nga bëgg a jëlee walla yokk ab jëfëndikookat. Mbooloo yi nga tannul duñu soppiku. Man nga tannadi am mbooloo ak CTRL + klig cammooñ.',
511 'userrights-reason' => 'Ngirtey coppite yi :',
512
513 # Groups
514 'group' => 'Mbooloo :',
515 'group-sysop' => 'Yorkat',
516 'group-all' => 'Yépp',
517
518 'group-sysop-member' => 'Yorkat',
519
520 'grouppage-sysop' => '{{ns:project}}:Yorkat',
521
522 # Recent changes
523 'nchanges' => '$1 {{PLURAL:$1|coppite|ciy coppite}}',
524 'recentchanges' => 'Coppite yu mujj',
525 'recentchangestext' => 'Toppal ci mii xët coppite yu mujj ci {{SITENAME}}.',
526 'recentchanges-feed-description' => 'Toppal coppite yu mujj gu wiki gii.',
527 'rcshowhideminor' => '$1 Coppite yu néew',
528 'rcshowhideliu' => '$1 jëfëndikookat gu bindu',
529 'rcshowhideanons' => '$1 indig IP',
530 'rcshowhidemine' => '$1 Li ma indiwoon',
531 'hide' => 'Nëbb',
532 'show' => 'Wone',
533 'number_of_watching_users_pageview' => '[$1 jëfëndikookat tegu]',
534 'rc_categories' => 'Yemug wàll yi (xaajale ak « | »)',
535 'rc_categories_any' => 'Yëpp',
536
537 # Recent changes linked
538 'recentchangeslinked' => 'Toppteg lëkkalekaay',
539 'recentchangeslinked-noresult' => 'Benn coppite amul ci xët yi mu lëkkalool ci diir bi ñu tann.',
540 'recentchangeslinked-summary' => "Mii xët moo lay won coppite yu mujj ci xët yi ñu lëkkale. Say xëtu limu toppte ñoo '''xëm'''.",
541
542 # Upload
543 'upload' => 'Jëli ab file',
544 'uploadbtn' => 'Jëli file bi',
545 'uploadnologin' => 'Duggoo',
546 'uploadlog' => 'Jaar-jaaru jëli yi',
547 'filename' => 'Turu file bi',
548 'badfilename' => 'Nataal gi tuddewaat nañ ko « $1 ».',
549 'uploadwarning' => 'Moytul !',
550 'savefile' => 'Duggal file bi',
551 'watchthisupload' => 'Topp file bii',
552
553 # Image list
554 'imagelist' => 'Limu nataal yi',
555 'ilsubmit' => 'Seet',
556 'byname' => 'ci tur',
557 'bydate' => 'ci diir',
558 'bysize' => 'ci ngandaay',
559 'imagelinks' => 'Xët yi am bii nataal',
560 'linkstoimage' => 'Xët yii ci suuf am nañ ci seen biir bii nataal :',
561 'imagelist_user' => 'Jëfëndikookat',
562
563 # List redirects
564 'listredirects' => 'Limu jubluwaat yi',
565
566 # Unused templates
567 'unusedtemplates' => 'Royuwaay yi ñu jëfëndikoowul',
568 'unusedtemplatestext' => 'Mii xët day limal xët yëpp yi tudd « Royuwaay » yu ñu duggalul ci benn xët. Bul fattee seet baxam amul yeneen lëkkalekaay yu lay jëmale ci royuwaay yi balaa nga leen di dindi.',
569 'unusedtemplateswlh' => 'yeneeni lëkkalekaay',
570
571 # Random page
572 'randompage' => 'Aw xët ci mbetteel',
573
574 # Statistics
575 'userstats' => 'Limbarem jëfëndikookat',
576
577 'brokenredirectstext' => "Yoonalaat yii dañuy jëmee ci'y xët yu amul :",
578 'brokenredirects-edit' => '(Soppi)',
579 'brokenredirects-delete' => '(dindi)',
580
581 'withoutinterwiki' => 'Xët yi amul lëkkalekaay diggantey-làkk',
582 'withoutinterwiki-header' => 'Xët yii amu ñu ay lëkkalekaay jëm yeneeni làkk:',
583
584 'fewestrevisions' => 'Jukki yi gën a néewi coppite',
585
586 # Miscellaneous special pages
587 'ncategories' => '$1 {{PLURAL:$1|wàll|ciy wàll}}',
588 'nlinks' => '$1 {{PLURAL:$1|lëkkalekaay|ciy lëkkalekaay}}',
589 'nmembers' => '$1 {{PLURAL:$1|xët|ciy xët}} ci biir',
590 'specialpage-empty' => 'Xët mii amul dara',
591 'uncategorizedpages' => 'Xët yi amul wall',
592 'uncategorizedcategories' => 'Wàll yi amul wàll',
593 'uncategorizedimages' => 'Nataal yu amul wall',
594 'uncategorizedtemplates' => 'Royuwaay yi amul Wàll',
595 'unusedcategories' => 'Wàll yi ñu jëfëndikoowul',
596 'wantedcategories' => 'Wàll yi ñu gën a laaj',
597 'wantedpages' => 'Xët yi ñu gën a laaj',
598 'mostlinked' => 'Xët yi ñu gën a lëkkale',
599 'mostlinkedcategories' => 'Wàll yi ñu gënë jëfëndikoo',
600 'mostlinkedtemplates' => 'Royuwaay yi ñu gën a jëfëndikoo',
601 'mostcategories' => 'Jukki yi ëpp yiy jëfëndikooy wàll',
602 'mostimages' => 'Nataal yi ñu gën a jëfëndikoo',
603 'mostrevisions' => 'Jukki yi ñu gën a soppi',
604 'allpages' => 'Xët yëpp',
605 'listusers' => 'Limu way bokk yi',
606 'specialpages' => 'Xët yu solowu',
607 'newpages' => 'Xët yu bees',
608 'newpages-username' => 'Jëfëndikookat :',
609 'ancientpages' => 'Jukki yi gënë néew ay coppite ci lu mujj',
610 'move' => 'Tuddewaat',
611 'movethispage' => 'Tuddewaat xët wi',
612 'unusedcategoriestext' => 'Wàll yii toftal, nekk nañu wante amuñul benn jukki walla wàll ci seen biir.',
613
614 # Book sources
615 'booksources-go' => 'Ayca',
616
617 'categoriespagetext' => 'Wàll yii ñoo am ci biir wiki gi.',
618 'alphaindexline' => '$1 ba $2',
619
620 # Special:Log
621 'specialloguserlabel' => 'Jëfëndikookat :',
622 'speciallogtitlelabel' => 'Koj :',
623 'log' => 'Yéenekaay',
624 'all-logs-page' => 'Yéenekaay yëpp',
625 'log-search-legend' => 'Seet ci yéenekaay yi',
626 'log-search-submit' => 'waaw',
627 'logempty' => 'Dara nekkul ci jaar-jaaru xët mii.',
628
629 # Special:Allpages
630 'nextpage' => 'Xët wi tegu ($1)',
631 'allpagesfrom' => 'Wonel xët yi tambalee ci :',
632 'allarticles' => 'Jukki yëpp',
633 'allinnamespace' => 'Xët yëpp(li ñu bàyyil tur $1)',
634 'allpagesprev' => 'Jiitu',
635 'allpagesnext' => 'Tegu',
636 'allpagessubmit' => 'Baaxal',
637 'allpagesprefix' => 'Wone xët yi tambalee :',
638 'allpagesbadtitle' => 'Koj gi nga bindal xët mii jaaduwul. xayna dafa am ay araf yu ñu manula jëfëndikoo ci koj yi.',
639
640 # Special:Listusers
641 'listusers-submit' => 'Wone',
642
643 # E-mail user
644 'emailuser' => 'Yònnee ab bataaxal jëfëndikookat bii',
645 'emailpage' => 'Yònnee ab bataaxal jëfëndikookat bii',
646 'emailmessage' => 'Bataaxal&nbsp;',
647 'emailsend' => 'Yònnee',
648 'emailsent' => 'Bataaxal yi ñu yònnee',
649 'emailsenttext' => 'Sa bataaxal yònnee nañ ko.',
650
651 # Watchlist
652 'watchlist' => 'Limu toppte',
653 'mywatchlist' => 'Limu toppte',
654 'watchlistfor' => "(ngir jëfëndikookat '''$1''')",
655 'nowatchlist' => 'Sa limu toppte amul benn jukki.',
656 'watchlistanontext' => 'Ngir mana gis walla soppi jëfkayu sa limu toppte, faw nga $1.',
657 'watchnologin' => 'Duggoo de',
658 'watchnologintext' => 'Yaa wara nekk [[Special:Userlogin|duggal]] ngir soppi lim gi.',
659 'addedwatch' => 'Yokk ci sa limu toppte',
660 'removedwatch' => 'Jëlee ci sa limu toppte',
661 'watch' => 'Topp',
662 'watchthispage' => 'Topp xët wii',
663 'unwatch' => 'Bul toppati',
664 'unwatchthispage' => 'Bul toppati',
665 'watchnochange' => 'Lenn ci xët yi ngay topp soppikuwul ci diir bii',
666 'watchlist-details' => 'Topp nga <b>$1</b> {{PLURAL:$1|xët|ciy xët}}, soo waññiwaalewul xëtu waxtaanukaay yi.',
667 'wlheader-showupdated' => '* Xët yi ñu soppiwoon ca sa duggu bu mujj ñoom la ñu fesal ñu <b>xëm</b>',
668 'watchmethod-recent' => 'saytug coppite yu mujj yu xët yi ngay topp',
669 'watchmethod-list' => 'saytug xët yi ñuy topp ngir ay coppite yu mujj',
670 'watchlistcontains' => "Sa limu toppte am na '''$1''' {{PLURAL:$1|xët|xët}}.",
671 'wlnote' => 'Fii ci suuf {{PLURAL:$1| ngay gis coppite yu mujj yi|ngay gis $1 coppite yu mujj}} ci {{PLURAL:$2|waxtu gu mujj gi|<b>$2</b> waxtu yu mujj}}.',
672 'wlshowlast' => 'wone $1 waxtu yu mujj, $2 bess yu mujj, walla $3.',
673 'watchlist-show-own' => 'Wone samay coppite',
674 'watchlist-hide-own' => 'Nëbb samay coppite',
675 'watchlist-show-minor' => 'Wone coppite yu tuut yi',
676 'watchlist-hide-minor' => 'Nëbb coppite yu tuut yi',
677
678 # Displayed when you click the "watch" button and it's in the process of watching
679 'watching' => 'Topp...',
680
681 'changed' => 'soppi',
682
683 # Delete/protect/revert
684 'confirm' => 'Dëggal',
685 'deletionlog' => 'Yéenekaay',
686
687 # Undelete
688 'viewdeletedpage' => 'Jaar-jaaru xët wi ñu dindi',
689
690 # Namespace form on various pages
691 'namespace' => 'Barabu tur :',
692 'blanknamespace' => '(njëkk)',
693
694 # Contributions
695 'contributions' => 'Li jëfëndikookat bii indi',
696 'mycontris' => 'Li ma indiwoon',
697 'nocontribs' => 'Amul benn coppite bu melokaanoo nii bu ñu gis.',
698 'month' => 'Tambalee ci weeru (ak yi jiitu) :',
699 'year' => 'Tambalee ci attum (ak yi jiitu) :',
700
701 # What links here
702 'whatlinkshere' => 'Xët yi mu lëkkalool',
703 'linklistsub' => '(Limuy lëkkalekaay)',
704 'linkshere' => 'Xët yii ci suuf am nañ ab lëkkalekaay buy jëm <b>[[:$1]]</b> :',
705 'whatlinkshere-prev' => '{{PLURAL:$1|wi jiitu|$1 yi jiitu}}',
706 'whatlinkshere-next' => '{{PLURAL:$1|wi tegu|$1 yi tegu}}',
707 'whatlinkshere-links' => '← lëkkalekaay',
708
709 # Block/unblock
710 'anononlyblock' => 'Jëfëndikookat yu binduwul rek',
711 'blocklink' => 'Teye',
712 'blocklogpage' => 'Jaar-jaaru teye yi',
713 'block-log-flags-anononly' => 'jëfëndikookat gu kenn xamul rek',
714 'block-log-flags-nocreate' => 'Terenañ sa sakum sàq',
715 'block-log-flags-noemail' => 'tere nañ sag yònneeg bataaxal',
716
717 # Move page
718 'movepage' => 'Tuddewaat aw xët',
719 'movearticle' => 'Tuddewaatal jukki bi',
720 'movenologintext' => 'Ngir man a tuddewaat aw xët, da ngaa war a [[Special:Userlogin|dugg]] ni jëfëndikookat bu bindu te saw sàq war naa am yaggaa bi mu laaj.',
721 'newtitle' => 'Koj bu bees',
722 'move-watch' => 'Topp xët wii',
723 'articleexists' => 'Am na ba noppi ab jukki gu am gii koj, walla koj gi nga tann baaxul. tannal bennen.',
724 'movedto' => 'Turam bu bees',
725 'movetalk' => 'Tuddewaat tamit xëtu waxtaanukaay wi mu andal',
726 '1movedto2' => 'tuddewaat ko [[$1]] en [[$2]]',
727 '1movedto2_redir' => 'yòonalaat ko [[$1]] mu jëm [[$2]]',
728 'movelogpage' => 'Jaar-jaaru tuddewaat yi',
729 'movelogpagetext' => 'Lii mooy limu xët yi ñu mujje tuddewaat.',
730 'movereason' => 'Ngirtey tuddewaat bi',
731 'delete_and_move' => 'Dindi te tuddewaat',
732
733 # Export
734 'export-addcattext' => 'Yokkal xëti Wàll gi :',
735 'export-addcat' => 'Yokk',
736
737 # Namespace 8 related
738 'allmessagesname' => 'Turu tool bi',
739 'allmessagescurrent' => 'Bataaxal bi fi nekk',
740 'allmessagestext' => "Lii mo'y limu bataaxal yëpp yi am ci biir MediaWiki",
741 'allmessagesmodified' => 'Wone coppite yi rek',
742
743 # Thumbnails
744 'thumbnail-more' => 'Ngandal',
745
746 # Tooltip help for the actions
747 'tooltip-pt-userpage' => 'Xëtu jëfëndikookat',
748 'tooltip-pt-mytalk' => 'Sama xëtu waxtaanukaay',
749 'tooltip-pt-preferences' => 'Samay tànneef',
750 'tooltip-pt-watchlist' => 'Limu xët yi ngay topp',
751 'tooltip-pt-mycontris' => 'Limu samay cërute',
752 'tooltip-pt-login' => 'Woo nan la ngir nga xammeku, waaye doonul lu manuta ñakk.',
753 'tooltip-pt-anonlogin' => 'woo nan la ngir nga xammeku, waaye doonul lu manuta ñakk.',
754 'tooltip-pt-logout' => 'Gennu',
755 'tooltip-ca-talk' => 'Waxtaan yi ñeel xët wii',
756 'tooltip-ca-viewsource' => 'Xët wii dañ kaa aar. Waaye man ngaa xool ndefam.',
757 'tooltip-ca-protect' => 'Aar xët wi',
758 'tooltip-ca-undelete' => 'Tabaxaat xët wi',
759 'tooltip-ca-move' => 'Tuddewaatal xët wii',
760 'tooltip-ca-watch' => 'Yokk xët wii ci sa limu toppte',
761 'tooltip-ca-unwatch' => 'Jëlee xët wii ci sa limu toppte',
762 'tooltip-search' => 'Seet ci gii wiki',
763 'tooltip-p-logo' => 'Xët wu njëkk',
764 'tooltip-n-mainpage' => 'Nemmeekul xët wu njëkk wi',
765 'tooltip-n-portal' => 'Maanaam ci naal bi',
766 'tooltip-n-currentevents' => 'Gis ay xibaar ci xew-xew yu teew yi',
767 'tooltip-n-recentchanges' => 'Limu coppite yu mujj ci wiki gi',
768 'tooltip-n-randompage' => 'Wone aw xët ci mbetteel',
769 'tooltip-n-help' => 'Tërug ndimbal gi',
770 'tooltip-n-sitesupport' => 'Jappaleel naal bi',
771 'tooltip-t-whatlinkshere' => 'limu xët yi ñu lëkkaleg bii',
772 'tooltip-t-recentchangeslinked' => 'Limu coppite yu mujj yu xët yi ñu lëkkale ak mii',
773 'tooltip-feed-rss' => 'Walug RSS ngir wii xët',
774 'tooltip-t-contributions' => 'xool limu cërute gu jëfëndikookat bii',
775 'tooltip-t-emailuser' => 'Yònnee ab bataaxal jëfëndikookat bii',
776 'tooltip-t-specialpages' => 'Limu xët yu solowu yépp',
777 'tooltip-ca-nstab-main' => 'Xool jukki bi',
778 'tooltip-ca-nstab-user' => 'Xool xëtu jëfëndikookat bi',
779 'tooltip-ca-nstab-special' => 'Lii am xët mu solowu la, mënoo koo soppi.',
780 'tooltip-ca-nstab-project' => 'Xool xëtu naal bi',
781 'tooltip-ca-nstab-image' => 'Xool xëtu nataal bi',
782 'tooltip-ca-nstab-template' => 'Xool royuwaay gi',
783 'tooltip-ca-nstab-help' => 'Xool xëtu ndimbal gi',
784 'tooltip-ca-nstab-category' => 'Xool xëtu wàll gi',
785 'tooltip-minoredit' => 'Melal samay coppite ñuy yu tuut',
786 'tooltip-save' => 'Duggal say coppite',
787 'tooltip-preview' => 'wonendil say coppite balaa nga leen di duggal',
788 'tooltip-diff' => 'Day tax a gis coppite yi nga def, fesal lenn',
789 'tooltip-watch' => 'Yokk xët wii ci sa limu toppte',
790 'tooltip-recreate' => 'Sosaat xët wi donte dañ kaa dindiwoo',
791
792 # Attribution
793 'anonymous' => 'Jëfëndikookat bu binduwul gu {{SITENAME}}',
794 'siteuser' => 'Jëfëndikookat $1 bu {{SITENAME}}',
795 'and' => 'ak',
796
797 # Math options
798 'mw_math_html' => 'HTML su manee ne, lu ko moy PNG',
799
800 # Browsing diffs
801 'nextdiff' => 'Wuute ngi ci tegu →',
802
803 # Media information
804 'file-info' => 'Réyaayu file bi : $1, type MIME : $2',
805 'file-info-size' => '($1 × $2 pixels, réyaayu file bi : $3, type MIME : $4)',
806 'show-big-image' => 'Ngandalal nataal gii',
807
808 # EXIF tags
809 'exif-usercomment' => 'Kadduy jëfëndikookat bi',
810
811 'exif-componentsconfiguration-0' => 'Amul',
812
813 # 'all' in various places, this might be different for inflected languages
814 'recentchangesall' => 'Yëpp',
815 'watchlistall2' => 'yépp',
816 'namespacesall' => 'Lépp',
817 'monthsall' => 'Lépp',
818
819 # Trackbacks
820 'trackbackremove' => '([$1 Dindi])',
821
822 # Delete conflict
823 'confirmrecreate' => "Jëfëndikookat bii [[User:$1|$1]] ([[User talk:$1|Waxtaan]]) moo dindi xët wii, nga xam ne tambaliwoon nga koo defar, ngir ngirte lii :
824 : ''$2''
825 Dëgëlël ni bëgg ngaa sakkaat xët wii.",
826
827 # AJAX search
828 'articletitles' => 'Jukki yu tambalee « $1 »',
829
830 # Auto-summaries
831 'autoredircomment' => 'Jubluwaat fii [[$1]]',
832 'autosumm-new' => 'Xët wu bees : $1',
833
834 # Watchlist editor
835 'watchlistedit-numitems' => 'Sa xëtu toppte am na {{PLURAL:$1|aw xët|$1 ciy xët}}, soo ci gennee xëtu waxtaanukaay yi',
836 'watchlistedit-noitems' => 'Sa limu toppte amul benn xët.',
837 'watchlistedit-normal-title' => 'Coppiteg xëtu toppte gi',
838 'watchlistedit-normal-legend' => 'Dindi ay xët yi limu toppte gi',
839 'watchlistedit-normal-explain' => 'xët yu sa limu toppte ñooy gisu fii ci suuf. Ngir dindi am xët (ak xëtu waxtaanukaayam) ci lim gi, kligal ci néeg moomu ci wetam te nga klig ci suuf. Man nga tamit [[Special:Watchlist/raw|soppi ko]] walla [[Special:Watchlist/clear|setal lepp]].',
840 'watchlistedit-normal-submit' => 'Dindi xët yi nga tann',
841 'watchlistedit-normal-done' => '{{PLURAL:$1|Dindi nañ am xët|$1 ciy xët dindi nañ leen}} ci sa limu toppte :',
842 'watchlistedit-raw-title' => 'Coppiteg limu toppte gi',
843 'watchlistedit-raw-legend' => 'Coppiteg limu toppte gi',
844 'watchlistedit-raw-explain' => 'Limu xët yi nekk ci sa limu toppte moo nekk ci suuf, xëtu waxtaan yi nekku ñu ci(ñoo ciy duggal seen bopp). Man ngaa soppi lim gi: yokk ci xët yi nga bëgg a topp, am xët ci rëdd mu ne, ak dindi xët yi nga bëggtul a topp. Soo noppee, kligal ci suuf ngir yeesal lim gi. Man nga tamit jëfëndikoo [[Special:Watchlist/edit|Soppikaay gu mak gi]].',
845 'watchlistedit-raw-titles' => 'Xët :',
846 'watchlistedit-raw-submit' => 'Yeesal lim gi',
847 'watchlistedit-raw-done' => 'Sa limu toppte yeesal nañ ko.',
848 'watchlistedit-raw-added' => '{{PLURAL:$1|Yokk nañ ci aw xët|$1 ciy xët lañ fi yokk}} :',
849 'watchlistedit-raw-removed' => '{{PLURAL:$1|Dindi nañ am xët|$1 ciy xët dindi nañ leen}} :',
850
851 # Watchlist editing tools
852 'watchlisttools-view' => 'Limu toppte',
853 'watchlisttools-edit' => 'Xool te soppi limu toppte gi',
854 'watchlisttools-raw' => 'Soppi lim gi',
855
856 );